Advertisements
Days of the Week ♦ Months of the Year ♦ Hours of the Day ♦ Calendar Dates
Temporal Constructs ♦ Example Phrases ♦ Units of Time ♦ Numbers
Days of the Week
Monday | altine |
Tuesday | talaata |
Wednesday | àllarba |
Thursday | alxames |
Friday | àjjuma |
Saturday | gaawu |
Sunday | dibéer |
Download Wolof Days of the Week digital flashcard set.
Advertisements
January | saawiye |
February | feewirye |
March | mars |
April | awriil |
May | mee |
June | suwe |
July | suleet |
August | ut |
September | septàmbar |
October | oktoobar |
November | noowàmbar |
December | deesàmbar |
Advertisements
one o’clock | benn waxtu |
two o’clock | ñaari waxtu |
three o’clock | ñetti waxtu |
four o’clock | ñeent waxtu |
five o’clock | juróomi waxtu |
six o’clock | juróomi-benn waxtu |
seven o’clock | juróomi-ñaari waxtu |
eight o’clock | juróomi-ñetti waxtu |
nine o’clock | juróomi-ñeent waxtu |
ten o’clock | fukki waxtu |
eleven o’clock | fukki waxtu ak benn |
twelve o’clock | fukki waxtu ak ñaar |
Advertisements
first | bu njëk |
second | ñaaréélu |
third | ñettéélu |
fourth | ñeentéélu |
fifth | juróoméélu |
sixth | juróom-bennéélu |
seventh | juróom-ñaaréélu |
eighth | juróom-ñettéélu |
ninth | juróom-ñeentéélu |
tenth | fukkéélu |
eleventh | fukk ak bennéélu |
twelfth | fukk ak ñaaréélu |
thirteenth | fukk ak ñettéélu |
fourteenth | fukk ak ñeentéélu |
fifteenth | fukk ak juróoméélu |
sixteenth | fukk ak juróom-bennéélu |
seventeenth | fukk ak juróom-ñaaréélu |
eighteenth | fukk ak juróom-ñettéélu |
nineteenth | fukk ak juróom-ñeentéélu |
twentieth | ñaar-fukkéélu |
twenty-first | ñaar-fukk ak bennéélu |
twenty-second | ñaar-fukk ak ñaaréélu |
twenty-third | ñaar-fukk ak ñettéélu |
twenty-fourth | ñaar-fukk ak ñeentéélu |
twenty-fifth | ñaar-fukk ak juróoméélu |
twenty-sixth | ñaar-fukk ak juróom-bennéélu |
twenty-seventh | ñaar-fukk ak juróom-ñaaréélu |
twenty-eighth | ñaar-fukk ak juróom-ñettéélu |
twenty-ninth | ñaar-fukk ak juróom-ñeentéélu |
thirtieth | ñett-fukkéélu |
thirty-first | ñett-fukk ak bennéélu |
Advertisements
yesterday | démb |
today | tey |
tomorrow | suba |
daytime | bëcëg |
nighttime | guddi |
morning | ci suba |
afternoon | ci ngoon |
evening | ci guddi |
Advertisements
What time is it? | Ban waxtoo jot? |
It’s 10:30 A.M. | Fukki waxtu ak genne-wall a jot ci suba. |
Today is December 15th. | Tey la fukkeeli fan ak juróom ci weeru desaambar. |
Advertisements
minute | miniit |
hour | waxtu |
day | bés |
week | bés bu ay |
month | weer |
year | at |
Advertisements
one | benn |
two | ñaar |
three | ñett |
four | ñeent |
five | juróom |
six | juróom-benn |
seven | juróom-ñaar |
eight | juróom-ñett |
nine | juróom-ñeent |
ten | fukk |
eleven | fukk ak benn |
twelve | fukk ak juróom-ñeent |
twenty | ñaar-fukk |
twenty-one | ñaar fukk ak benn |
thirty | ñett-fukk |
forty | ñeent-fukk |
fifty | juróom-fukk |
sixty | juróom-benn-fukk |
one hundred | téeméer |
one hundred one | téeméer ak benn |
two hundred | ñaari téeméer |
one thousand | junni |
one thousand five hundred ninety-nine | junni ak juróomi téeméer ak juróom-ñeent-fukk ak juróom-ñeent |
hey I would lyk to learn wolof please help
LikeLike
Jarigen juef swar na lool sisen lueguey
LikeLike
mada
LikeLike