Basic Phrases
Hello. | Salaam aleekum. |
Goodbye. | Mangi dem. |
Please. | Bu la neexee. |
Thank you. | Jërejëf. |
You’re welcome. | Amul sólo. |
Yes. | Waaw. |
No. | Déedéet. |
Sorry. | Baal ma. |
Do you speak English? | Ndax dégg nga angale? |
Do you understand? | Dégg nga? |
I understand. | Dégg naa. |
I don’t understand. | Dégguma. |
Help! | Wóoy! |
Sample Phrases
A table for three. | Ñett lanu. |
aj | taabal ji | ndax | ñett | three | we are |
Bring us some bissap. | Indil nu bisaap. |
indil | nun | dara | bisaab bi | bring | us | bissap |
Do you have a watch? | Am nga montar? |
def | yow | am | ab | montar bi | have | you | watch |
Everyone was coming to the funeral. | Ñep angi ñow ci dëj bi. |
ñépp | ci | ñëw | ci | bi | dëj bi | all people | (now) | come | to | funeral | the |
For me, the yassa. | Man yaasa. |
ngir | man | bi | yaasa bi | me | yassa |
Give me the money. | Indil xaalis bi. |
indil | man | bi | xaalis bi | give | money | the |
He is fine. | Mi ngi ci jàmm. |
moom | lele | bu baax | he | is | at | peace |
I am from America. | Maa ngi jóge Amerik. |
man | ngi | jóge | amerik | I | am | from | america |
Lower your price! | Waññil! |
wàññi | nga | njëg gi | count lower |
More sauce, please. | Dollil tuuti ñeex. |
gën | ñeex mi | neex | add | little | sauce |
No one can deny it. | Kenn mëna ko weddi. |
déedéet | benn | mën | weddi | ko | no one | can | it | deny |
OK, get in. | Yéegal. |
baaxna | yéeg | ci biir | climb in |
Please bring us some cold water. | Indil nu ndox mu sedd. |
neex | indi | nun | benna | sedd | ndox mi | bring | us | water | the | cold |
She is fine. | Jàmm rekk. |
moom | lele | baax | peace | only |
That watch, how much does it cost? | Sa montar bi ñaata lay jar? |
lale | montar bi | nan | bari | def | ko | njëg | your | watch | the | how much | is | price |
We would like to pay. | Danu bëgg fey. |
dañuy | bëgg | komka | ci | fey | we | want | pay |
Yes, I have a watch. | Waaw am naa montar. |
waaw | man | am | ab | montar bi | yes | have | I already | watch |
Subscribe to get access
Read more of this content when you subscribe today.