Wolof Numbers, Time & Dates

Advertisements

Days of the Week ♦ Months of the Year ♦ Hours of the Day ♦ Calendar Dates
Temporal Constructs ♦ Example Phrases ♦ Units of Time ♦ Numbers

Days of the Week

Mondayaltine
Tuesdaytalaata
Wednesdayàllarba
Thursdayalxames
Fridayàjjuma
Saturdaygaawu
Sundaydibéer

Download Wolof Days of the Week digital flashcard set.

Advertisements


Months of the Year

Januarysaawiye
Februaryfeewirye
Marchmars
Aprilawriil
Maymee
Junesuwe
Julysuleet
Augustut
Septemberseptàmbar
Octoberoktoobar
Novembernoowàmbar
Decemberdeesàmbar
Advertisements


Hours of the Day

one o’clockbenn waxtu
two o’clockñaari waxtu
three o’clockñetti waxtu
four o’clockñeent waxtu
five o’clockjuróomi waxtu
six o’clockjuróomi-benn waxtu
seven o’clockjuróomi-ñaari waxtu
eight o’clockjuróomi-ñetti waxtu
nine o’clockjuróomi-ñeent waxtu
ten o’clockfukki waxtu
eleven o’clockfukki waxtu ak benn
twelve o’clockfukki waxtu ak ñaar
Advertisements


 Calendar Dates

firstbu njëk
secondñaaréélu
thirdñettéélu
fourthñeentéélu
fifthjuróoméélu
sixthjuróom-bennéélu
seventhjuróom-ñaaréélu
eighthjuróom-ñettéélu
ninthjuróom-ñeentéélu
tenthfukkéélu
eleventhfukk ak bennéélu
twelfthfukk ak ñaaréélu
thirteenthfukk ak ñettéélu
fourteenthfukk ak ñeentéélu
fifteenthfukk ak juróoméélu
sixteenthfukk ak juróom-bennéélu
seventeenthfukk ak juróom-ñaaréélu
eighteenthfukk ak juróom-ñettéélu
nineteenthfukk ak juróom-ñeentéélu
twentiethñaar-fukkéélu
twenty-firstñaar-fukk ak bennéélu
twenty-secondñaar-fukk ak ñaaréélu
twenty-thirdñaar-fukk ak ñettéélu
twenty-fourthñaar-fukk ak ñeentéélu
twenty-fifthñaar-fukk ak juróoméélu
twenty-sixthñaar-fukk ak juróom-bennéélu
twenty-seventhñaar-fukk ak juróom-ñaaréélu
twenty-eighthñaar-fukk ak juróom-ñettéélu
twenty-ninthñaar-fukk ak juróom-ñeentéélu
thirtiethñett-fukkéélu
thirty-firstñett-fukk ak bennéélu
Advertisements


Temporal Constructs

yesterdaydémb
todaytey
tomorrowsuba
daytimebëcëg
nighttimeguddi
morningci suba
afternoonci ngoon
eveningci guddi
Advertisements


Example Phrases

What time is it?Ban waxtoo jot?
It’s 10:30 A.M.Fukki waxtu ak genne-wall a jot ci suba.
Today is December 15th.Tey la fukkeeli fan ak juróom ci weeru desaambar.
Advertisements


Units of Time

minuteminiit
hourwaxtu
daybés
weekbés bu ay
monthweer
yearat
Advertisements


Numbers

onebenn
twoñaar
threeñett
fourñeent
fivejuróom
sixjuróom-benn
sevenjuróom-ñaar
eightjuróom-ñett
ninejuróom-ñeent
tenfukk
elevenfukk ak benn
twelvefukk ak juróom-ñeent
twentyñaar-fukk
twenty-oneñaar fukk ak benn
thirtyñett-fukk
fortyñeent-fukk
fiftyjuróom-fukk
sixtyjuróom-benn-fukk
one hundredtéeméer
one hundred onetéeméer ak benn
two hundredñaari téeméer
one thousandjunni
one thousand five hundred ninety-ninejunni ak juróomi téeméer ak juróom-ñeent-fukk ak juróom-ñeent

Back to top.

3 comments

Leave a Reply

Please log in using one of these methods to post your comment:

WordPress.com Logo

You are commenting using your WordPress.com account. Log Out /  Change )

Facebook photo

You are commenting using your Facebook account. Log Out /  Change )

Connecting to %s