Wolof / English – B

Advertisements
ba beneen yoon goodbye for now
baal ma excuse me
baar baar bar (place)
baaraam baa-raam finger
baat baat neck
baat bu metti baat boo met-tee sore throat
baax baakh good
baax na baakh na OK
baaxul baa-khul it’s faulty
baay uncle (related to father)
baay ba-ai father
bagas n. (pl) belongings
bahh v. boil
bahre n. gecko
baigal v. entertain
bajjan aunt (related to father)
bakkan bak-kan nose
balaa ba-laa before
Ban waxtoo jot? What time is it?
Ban waxtu … ? ban wakh-too … At what time … ?
bank bank bank
banque (Fr.) bank
bare coow ba-re choh noisy
bataaxal ba-taa-khal letter (mail)
bateau (Fr.) boat
batterie (Fr.) car battery
bayyi baiy-yee cancel
beau/belle (Fr.) beautiful
bébé (Fr.) baby
bebe be-be baby
bëccëg day (dawn to nightfall)
bee bey that (one)
beer beyr beer
bees beys new
Bëgg naa … buhg naa … I’d like to … / I want to …
bëgg naa kaani I like hot pepper
bëgg v. buhg like
bëgguma kaani I don’t like hot pepper
bëj-gànnaar buhj-gaan-naar north
bëj-saalum buhj-saa-loom south
bële buh-le that (one over there)
bëñ buhny teeth
bëñ buy metti buhny boo-ee met-tee toothache
beneen wisiit bi ben-eyn wi-seet bee next tour
benn ben one
benn palaat ben pa-laat dish (menu item)
benn restoraan ben res-to-raan place to eat
benn yoon ben yawn one way
bës buhs day
bët buht eye
bien (Fr.) OK
Bien, merci. (Fr.) Fine, thanks.
bientôt (Fr.) soon
biëre (Fr.) beer
bii bee this (one)
biiñ beeny wine
biir beer center
biir beer stomach
biir buy daw beer boo-ee daw diahrea
biisap bissap
billet (Fr.) ticket
billet stand-by (Fr.) stand-by ticket
bind bind write
bindukaay bin-doo-kai pen
biteel bi a bottle
biteel yi bottles
bitik n. bee-teek shop
bitiku suweniir bee-tee-koo soo-we-neer souvenir shop
biye bee-ye ticket (transport)
blanchisserie (Fr.) laundry place
boisson (Fr.) drink
boîte (Fr.) nightclub
bokk bok share
bokk néeg bok neyyg share a dorm
bon bon bad
bon marché (Fr.) cheap
bon/bonne (Fr.) good
bonjour (Fr.) hello
bonsoir (Fr.) goodnight
bopp bop head
bopp buy metti bop boo-ee met-tee headache
borosada bo-ro-sa-da toothbrush
bouche (Fr.) mouth
bouillon gras (Fr.) meat stock
bouteille (Fr.) bottle
bras (Fr.) arm
bronchite (Fr.) bronchitis
bronsiit bron-seet bronchitis
brosse à dents (Fr.) toothbrush
bruyant/bruyante (Fr.) noisy
bu amul boo a-mul without
bu dégg angale boo deg an-ge-le who speaks English
bunt n. bunt exit
bureau de poste (Fr.) post office
bureau des objets trouvés (Fr.) lost-property office
bus (Fr.) bus
butéel boo-teyl bottle
buwaason n. boo-waa-son drink
buy baobab fruit juice
bwat bwat nightclub

Leave a Reply

Please log in using one of these methods to post your comment:

WordPress.com Logo

You are commenting using your WordPress.com account. Log Out /  Change )

Facebook photo

You are commenting using your Facebook account. Log Out /  Change )

Connecting to %s